1
00:00:11,578 --> 00:00:14,547
Yoon wi baaxul.

2
00:00:14,714 --> 00:00:16,649
Dama tàmbali tàyyi ci yëngu.

3
00:00:16,683 --> 00:00:19,652
Dina jeex ci diir bu gàtt, sama xol.

4
00:00:20,820 --> 00:00:23,790
Sama xel dalul ci gan yii yépp

5
00:00:23,790 --> 00:00:26,726
ak tàmbali dundu sama bopp ci saasi...

6
00:00:26,726 --> 00:00:28,595
Ndax loolu mooy li nga bëgg dëgg?

7
00:00:28,595 --> 00:00:29,763
Waaw

8
00:00:29,763 --> 00:00:30,797
Xam nga lima bëgg?

9
00:00:30,797 --> 00:00:32,797
Lan?

10
00:00:31,498 --> 00:00:32,532
Saw.

11
00:00:32,699 --> 00:00:33,867
Ha-ha-ha!

12
00:00:34,534 --> 00:00:36,069
Kaf naa.

13
00:00:36,069 --> 00:00:37,837
Dama wara dem ci duus bi.

14
00:00:38,171 --> 00:00:41,141
Oh, mangi jeggalu. Waawaw, dina nu ci gis dara.

15
00:00:41,307 --> 00:00:44,277
Sëñ dawalkat bi, ndax mën nga taxaw ci wetu WC bu ñépp bokk?

16
00:00:45,045 --> 00:00:46,312
Jërëjëf

17
00:00:46,446 --> 00:00:47,847
Nanga def.

18
00:01:27,320 --> 00:01:29,589
tëye buntu bi! TËPPAL BUNT BI!!!

19
00:01:29,589 --> 00:01:32,559
Buntu yu alku

20
00:01:34,394 --> 00:01:36,062
Lu xew ?

21
00:01:36,062 --> 00:01:38,264
Wax ma am nga telefon.

22
00:01:38,264 --> 00:01:39,833
Ndax damay nuru ku am poos?

23
00:01:39,833 --> 00:01:42,802
Daa melni dañu laal nun ñaar.

24
00:01:44,070 --> 00:01:45,438
O déet

25
00:01:46,106 --> 00:01:48,106
Lu xew

26
00:01:47,073 --> 00:01:48,475
Bunt bii ubbeekuwul ci biir

27
00:01:48,675 --> 00:01:50,243
Bunt bi. Dafa yàqu.

28
00:01:50,443 --> 00:01:51,578
Lan?

29
00:01:51,845 --> 00:01:54,814
Dama mujjee ubbeeku bima duggee fii ngir saw.

30
00:01:55,281 --> 00:01:56,382
Kañ?

31
00:01:56,583 --> 00:01:58,485
Demb ci guddi

32
00:02:00,053 --> 00:02:02,188
Ndax fi nga fanaan?

33
00:02:02,188 --> 00:02:03,289
Yalla sama boroom

34
00:02:03,623 --> 00:02:05,825
Ndax kenn ñëwul fii?

35
00:02:05,959 --> 00:02:08,928
WC buñu bàyyi la

36
00:02:09,229 --> 00:02:12,332
WC bi daanaka amul gan

37
00:02:12,332 --> 00:02:15,301
Fiiru WC la

38
00:02:19,005 --> 00:02:25,145
Ngir nit ku fanaan ci
latrine village, yaa ngi xeeñ bu baax.

39
00:02:25,278 --> 00:02:30,150
te yaa ngi dal lool ci nit ku
Sëy bi dina dem te moom nekkul ci.

40
00:02:30,216 --> 00:02:33,186
Ci anam wumu mëna doon

41
00:02:33,353 --> 00:02:38,224
War ngama wax lu ñàkk njariñ lii.
wëlbatiku rek.

42
00:02:40,793 --> 00:02:46,366
Oh, mangi jeggalu. Dama fàtte ni lii
ginaaw lépp, WC la.

43
00:02:49,903 --> 00:02:52,872
Buntu bii dañu ko tabax...

44
00:02:54,307 --> 00:02:58,978
ci atum 1954, ingenieur yu soviet yi ñoo ko defar!

45
00:02:59,579 --> 00:03:02,549
Mënu nu tëye buntu yooyu.

46
00:03:02,715 --> 00:03:05,685
Alal! Lu nuy def?

47
00:03:07,887 --> 00:03:09,889
Oh sama...

48
00:03:11,191 --> 00:03:14,827
Su kenn ñëwul fii, dina nu am
ngir toog beneen bis fii.

49
00:03:25,004 --> 00:03:26,906
Déedet

50
00:03:27,207 --> 00:03:31,711
Sama fiancé mingi may xaar ci biti. Dina nu mooytu.

51
00:03:32,145 --> 00:03:34,047
Kon dina ñëw ubbi buntu bi ci lu yaggul dara?

52
00:03:34,480 --> 00:03:37,050
Dëgg la dina ñëw ci man ci lu yaggul dara.

53
00:03:37,183 --> 00:03:40,887
Amu nu beneen pexe ludul xaar

54
00:03:44,257 --> 00:03:48,161
Dama yaakaar ni dañu wara xaar ay simili yu néew

55
00:03:48,361 --> 00:03:51,331
Mënul yàgg te amul man.

56
00:04:06,045 --> 00:04:07,747
Dafay ñëw leegi.

57
00:04:20,026 --> 00:04:21,494
Yalla sama boroom

58
00:04:36,209 --> 00:04:38,111
Loolu mooy wërsëg!

59
00:05:35,768 --> 00:05:37,970
Fan la nekk?!

60
00:05:39,172 --> 00:05:43,843
Kañ lay seetlu ni dem naa?

61
00:05:44,844 --> 00:05:45,978
Waaw

62
00:05:51,484 --> 00:05:54,087
Danga wara nekk xeetu nit ku bëgg
yëngu.

63
00:05:54,620 --> 00:05:56,089
Xam nga

64
00:05:56,356 --> 00:05:58,191
Bëgguma gaawantu lool.

65
00:05:58,758 --> 00:06:04,697
Waaye nak, duma nit ku bëgga am
jeexal sa liggéey nga nelaw.

66
00:06:07,066 --> 00:06:09,066
baax na

67
00:06:08,234 --> 00:06:11,204
Oh, bul wax ci turu ñépp!

68
00:06:11,504 --> 00:06:14,207
Man, ci sama wàll, nangu naa ni dañu wara jege mbir yi

69
00:06:14,207 --> 00:06:15,675
ak yëg-yëg,

70
00:06:15,808 --> 00:06:18,044
ak xalaat

71
00:06:18,111 --> 00:06:19,679
ak bàyyi xel.

72
00:06:20,113 --> 00:06:23,082
Du lenn ludul baña xàddi ak muñ

73
00:06:23,349 --> 00:06:26,986
mën nala yuuxu
ak yuuxu ci resultaa bi mujj.

74
00:06:28,254 --> 00:06:30,256
Taalifkat nga!

75
00:06:30,690 --> 00:06:33,659
Ak, sa xarit bu jigeen
amaana daf lay wax lii saa yu nekk.

76
00:06:33,860 --> 00:06:35,695
Amuma xarit bu jigeen

77
00:06:35,695 --> 00:06:38,664
waaye xalaat nga
it: jigeen ñi dañu may faral di wax loolu.

78
00:06:38,798 --> 00:06:41,200
Yaakaar naa ni siiw nga ci ñoom

79
00:06:41,801 --> 00:06:43,603
Du kumpa

80
00:06:44,003 --> 00:06:46,973
Yaw itam bëgg ngama ba noppi.

81
00:06:47,440 --> 00:06:48,574
Lan?!

82
00:06:48,941 --> 00:06:50,643
Loolu amul benn njariñ!

83
00:06:50,943 --> 00:06:53,112
Lii mooy duus bi. Amna seetu
fépp.

84
00:06:53,112 --> 00:06:56,082
Yaakaar nga ni seetlu wuma la
xool samay lëf?

85
00:06:56,549 --> 00:06:58,217
Bul defar lii!

86
00:06:58,217 --> 00:07:02,088
Duma benn
Dama bëgg sa gënn gu mat sëkk!

87
00:07:09,128 --> 00:07:11,597
Lu tax doo wax dara?

88
00:07:12,131 --> 00:07:15,101
Dama fàttaliku...

89
00:07:17,670 --> 00:07:20,173
Suma taxawee ci arrêt bus bi

90
00:07:20,173 --> 00:07:22,173
Waaw

91
00:07:20,640 --> 00:07:23,609
Dama wara xaar bus bi lu yàgg.

92
00:07:23,776 --> 00:07:29,482
Dafay melni daf may ñaawal saa yu nekk, daf may sonal di xaar
ci taw ak ci neige

93
00:07:29,482 --> 00:07:31,384
Waaye suma taal benn sigaret

94
00:07:31,384 --> 00:07:33,553
Bus bi ñëw ci saasi

95
00:07:37,023 --> 00:07:39,192
Amuma sax jotu ko tóx.

96
00:07:39,292 --> 00:07:42,228
Ndax am nga looy def ci gémmiñ?

97
00:07:42,228 --> 00:07:45,198
Nanu, tóx suko defee bus bu fees dell ak nit ñëw

98
00:07:45,298 --> 00:07:47,700
Amuma benn sigaret.

99
00:07:48,501 --> 00:07:50,002
Kon dunu amal njariñ.

100
00:07:50,403 --> 00:07:51,604
Mën nanu tàmbalee ci lu ndaw

101
00:07:51,938 --> 00:07:55,908
Teg ci, ndax amna diggante ngëm
ci sa diggante ak sa fiancé?

102
00:07:56,042 --> 00:07:57,443
Amaana ab lëkkaloo ci xel?

103
00:07:57,677 --> 00:07:58,978
Waaw waaw, amnanu lëkkaloo

104
00:07:59,912 --> 00:08:02,882
Bul xalaat lu jaarul yoon.

105
00:08:05,251 --> 00:08:06,486
Sudee...

106
00:08:07,086 --> 00:08:08,688
Bëgguma def yëfi soxor.

107
00:08:08,821 --> 00:08:10,289
Waaye su ma la fóonee

108
00:08:10,890 --> 00:08:12,890
Déglul ma.

109
00:08:11,757 --> 00:08:13,757
Déedet

110
00:08:12,124 --> 00:08:15,094
Foofu moom dina ko yëg.

111
00:08:15,561 --> 00:08:16,796
Duma la fóon.

112
00:08:16,829 --> 00:08:18,829
Xam naa la.

113
00:08:17,830 --> 00:08:20,800
Waaye yàgg nanu ko xaar ba leegi ñëwagul.

114
00:08:21,167 --> 00:08:24,136
Amna lu nu wara fexe ba mu ñëw fii

115
00:08:24,370 --> 00:08:26,370
Xoolal

116
00:08:25,238 --> 00:08:26,706
Xoolaatal mbir yi ci anam wu jaar yoon

117
00:08:27,840 --> 00:08:29,840
Fóon rekk la

118
00:08:28,441 --> 00:08:29,742
Suma ko defee...

119
00:08:29,976 --> 00:08:32,945
Waaye ngir mu gaaw a ñëw.

120
00:08:35,181 --> 00:08:37,181
Dama ko bëgg

121
00:08:35,982 --> 00:08:37,982
Baaxna.

122
00:08:36,682 --> 00:08:38,851
Dina nu ko def ngir mu mëna yëg sunu fóon ba noppi ñëw

123
00:08:39,051 --> 00:08:40,119
Nanu ko jéem.

124
00:08:40,186 --> 00:08:43,990
Suko yëgee rek, dafay ñëw ubbi buntu bi

125
00:08:44,290 --> 00:08:47,293
Su amee chance, lu tax doo ko jël.

126
00:08:47,293 --> 00:08:50,663
Waaye nak, ba leegi diga guma kenn ni dinaa ko gëm

127
00:08:50,663 --> 00:08:53,332
Yaakaar naa ni mën nanu jéem xeetu paj mii

128
00:09:03,976 --> 00:09:06,946
Leegi mingi ñëw.

129
00:09:13,920 --> 00:09:15,721
Yaakaar nga ni loolu moo ko yëg ?

130
00:09:15,888 --> 00:09:18,257
Fi ñu tolli nii, dara xewul.

131
00:09:18,257 --> 00:09:19,759
Dégluma ay tànkam.

132
00:09:19,926 --> 00:09:22,895
Kenn ubbiwul buntu yi

133
00:09:23,396 --> 00:09:24,964
Lépp amul benn njariñ.

134
00:09:26,132 --> 00:09:28,234
Yaakaar nga ni dina ñu...

135
00:09:28,334 --> 00:09:30,403
Waaye ngir...

136
00:09:30,403 --> 00:09:32,238
Dëgg la

137
00:11:42,101 --> 00:11:44,537
Waneel ma sa luxus

138
00:11:44,537 --> 00:11:46,639
Yalla sama boroom

139
00:13:29,608 --> 00:13:31,110
Fiiru WC

140
00:13:31,744 --> 00:13:33,744
Mooy

141
00:14:18,657 --> 00:14:20,292
Yalla sama boroom

142
00:15:06,538 --> 00:15:09,508
Buntu yu alku

143
00:15:10,542 --> 00:15:13,512
Danu wara joge fii ci anam wumu mëna doon.

144
00:15:14,980 --> 00:15:16,882
Dafay waaja yëg...

145
00:15:16,882 --> 00:15:18,350
Waaw

146
00:15:25,324 --> 00:15:28,294
Danu wara fexe nu mu ñëw

147
00:15:38,437 --> 00:15:41,407
Waaye buntu yu yàqu baaxul noonu.

148
00:15:41,440 --> 00:15:44,410
Ànd naa ak yaw.

149
00:15:54,520 --> 00:15:56,522
mbaam xuux bu rafet!

150
00:15:56,588 --> 00:15:59,558
Xamuma lu tax mu bëgga sëy ak yaw.

151
00:16:40,165 --> 00:16:42,167
Xaar naa lu yàgg...

152
00:17:14,633 --> 00:17:16,168
Am nga kuuy bu rafet nii.

153
00:17:16,335 --> 00:17:19,004
Sama fiancé taaruwul noonu.

154
00:17:19,338 --> 00:17:22,307
Sa lëf lu yéeme la.

155
00:18:13,192 --> 00:18:16,161
aventure céet la

156
00:27:31,082 --> 00:27:34,052
Fowe ak say ween

157
00:29:36,174 --> 00:29:37,308
Xoolal ma ci bët

158
00:30:20,552 --> 00:30:22,187
Ndax takk jabar nga?

159
00:30:22,187 --> 00:30:23,621
Waaw

160
00:35:51,616 --> 00:35:53,951
Sama xol?

161
00:35:54,785 --> 00:35:56,988
Yaa ngi foofa?

162
00:35:57,722 --> 00:35:59,490
Lem!

163
00:36:08,699 --> 00:36:11,669
Salaam, ndax lépp jàmm?

164
00:36:16,741 --> 00:36:18,142
Nanga def

165
00:36:26,651 --> 00:36:29,620
Sama xol, lépp a ngi baax? Yaa ngi foofa?

166
00:36:35,393 --> 00:36:37,695
Ubbi buntu bi

167
00:36:38,729 --> 00:36:39,964
Ubbi buntu bi

168
00:36:40,031 --> 00:36:41,966
Dégg ngeen ma?

169
00:36:43,701 --> 00:36:45,937
Ubbi buntu bi

170
00:36:56,113 --> 00:36:58,716
Ubbi buntu bi ci saasi

171
00:36:59,417 --> 00:37:02,386
Mani ko ubbil buntu bi.

172
00:37:04,255 --> 00:37:06,257
Ubbi buntu bi

173
00:37:25,843 --> 00:37:28,813
Maa ngi dem dindi buntu bi.

174
00:37:29,447 --> 00:37:32,416
Yaa ngi foofa?

175
00:37:36,254 --> 00:37:38,389
Liggéeyu tàggatu?

176
00:37:39,323 --> 00:37:41,259
Lu xew-xew la!

177
00:37:41,259 --> 00:37:42,727
Takkal ko

178
00:37:43,561 --> 00:37:45,196
Ndax rusu leen?

179
00:37:45,496 --> 00:37:47,398
Amuma ci dara.

180
00:37:48,499 --> 00:37:50,735
Loolu lumuy tekki?

181
00:37:58,276 --> 00:38:01,245
Sama mbaax.

182
00:38:02,813 --> 00:38:04,882
Du noonu la nuru.

183
00:38:04,882 --> 00:38:06,882
Gis.

184
00:38:05,750 --> 00:38:08,719
Du sama njuumte

185
00:38:10,821 --> 00:38:13,791
Loolu soof na lool.

186
00:38:14,058 --> 00:38:15,993
Yaw yaay kan?

187
00:38:16,093 --> 00:38:19,063
Sama xol, bàyyi nàmp, mangi.

188
00:38:20,431 --> 00:38:23,401
Danga may bëgga waccu.

189
00:38:27,705 --> 00:38:28,873
Ugh!

190
00:38:30,007 --> 00:38:32,977
Loolu lu soof la.

191
00:38:36,080 --> 00:38:37,915
Dafay nëbb.

192
00:38:38,282 --> 00:38:41,252
Lu nga def, yaw mi?

193
00:38:41,852 --> 00:38:43,521
Du sama njuumte, bro

194
00:38:43,521 --> 00:38:44,555
Kan moo ko taañ?

195
00:38:44,722 --> 00:38:46,924
Xalaatal ma dëgg

196
00:38:46,924 --> 00:38:49,894
Kan moo ko taañ?

197
00:38:50,161 --> 00:38:53,130
Danga laal sama jabar ji ëlëg

198
00:38:53,764 --> 00:38:55,366
Danga mujjee ñëw.

199
00:38:55,366 --> 00:38:56,801
Noo ngi lay xaar

200
00:38:56,801 --> 00:38:58,302
Ugh, danga soxor.

201
00:38:58,302 --> 00:39:00,404
Amoon nanu ay tukki yu ndaw fii

202
00:39:00,404 --> 00:39:02,073
Aventure?

203
00:39:02,173 --> 00:39:03,474
Yaa ngi xeeñ!

204
00:39:03,474 --> 00:39:05,409
Yaa ngi tóxaat!

205
00:39:05,609 --> 00:39:08,579
Ndax danga may tuumal ni damay tóx? waaye def nga ko.

206
00:39:09,580 --> 00:39:11,182
Jëlal samay yëf.

207
00:39:11,248 --> 00:39:12,817
Danga wara teela ñëw.

208
00:39:12,817 --> 00:39:14,518
Nanu joge fi.

209
00:39:14,518 --> 00:39:16,120
Dama tàyyi ci la xaar!

210
00:39:16,320 --> 00:39:19,290
Gaawaay! Xoolal waxtu wi!

211
00:39:26,564 --> 00:39:29,533
Bunt yi dañu tëjaat!

212
00:40:03,401 --> 00:40:04,969
Kon nanu dem !

213
00:40:04,969 --> 00:40:27,500
Dafa jot ñu sëy


